Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 128

Sabóor 128:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Sa jabar ni garab gu nangoo sa wanag, say doom wëra wër sa ndab ni njëmbat lu jebbi.
4Ki ragal Aji Sax jaa ngoog, nii rekk lay barkeele.
5Yal na la Yàlla barkeele fii ci Siyoŋ; yal nanga teewe xéewalu Yerusalem sa giiru dund gépp,

Read Sabóor 128Sabóor 128
Compare Sabóor 128:3-5Sabóor 128:3-5