Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 128:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 128:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Sa jabar ni garab gu nangoo sa wanag, say doom wëra wër sa ndab ni njëmbat lu jebbi.
4 Ki ragal Aji Sax jaa ngoog, nii rekk lay barkeele.
5 Yal na la Yàlla barkeele fii ci Siyoŋ; yal nanga teewe xéewalu Yerusalem sa giiru dund gépp,
Sabóor 128 in Kàddug Yàlla gi