Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 121

Sabóor 121:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Kii du la bàyyi nga tërëf, sa sàmm bii gëmmul.
4Kiy sàmm Israyil kay gëmmul, nelawul.
5Aji Sax jee lay sàmm, Aji Sax jee lay yiir, féete la ndijoor.

Read Sabóor 121Sabóor 121
Compare Sabóor 121:3-5Sabóor 121:3-5