Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 121:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 121:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Kii du la bàyyi nga tërëf, sa sàmm bii gëmmul.
4 Kiy sàmm Israyil kay gëmmul, nelawul.
5 Aji Sax jee lay sàmm, Aji Sax jee lay yiir, féete la ndijoor.
Sabóor 121 in Kàddug Yàlla gi