Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 119

Sabóor 119:53-55

Help us?
Click on verse(s) to share them!
53Sama xol daa fees ndax ñu bon ñiy wacc saw yoon.
54Sa dogali yoon laay woyantoo, fu ma mana sance.
55Aji Sax ji, tudd naa la guddi, di sàmm saw yoon.

Read Sabóor 119Sabóor 119
Compare Sabóor 119:53-55Sabóor 119:53-55