Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 9

Sabóor 9:7-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Noon ya raaf, gental ba fàww. Yaa déjjati seeni dëkk, seenu askan fey.
8Aji Sax jee sax dàkk, samp jalam ngir àtte.
9Moom mooy àtte àddina cig njub, di dogalal xeet yi dëgg.
10Aji Sax jeey làq néew-ji-doole, mooy làqe bésub njàqare.

Read Sabóor 9Sabóor 9
Compare Sabóor 9:7-10Sabóor 9:7-10