Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 98

Sabóor 98:1

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Muy kàddug Sabóor. Woyleen Aji Sax ji woy wu yees, moo def ay jaloore, kàttanam ak sellngay dooleem jox na ko ndam li.

Read Sabóor 98Sabóor 98
Compare Sabóor 98:1Sabóor 98:1