Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 96

Sabóor 96:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Yeen làngi xeet yi, seedeel-leen Aji Sax ji; seedeel-leen Aji Sax ji teddngaak doole.
8Seedeel-leen Aji Sax ji teddngay turam, yékkatil kob sarax, duggaale ëttam.

Read Sabóor 96Sabóor 96
Compare Sabóor 96:7-8Sabóor 96:7-8