Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 94

Sabóor 94:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Yeen bokk yu dofe yi, moytuleen. Gàtt xel yi, kañ ngeen di muus?
9Ki jëmbati nopp, da dul dégg a? Am ki xari gët, da dul gis?
10Kiy yar yéefar yi, da dul mbugalee? Du mooy kiy xamal nit?

Read Sabóor 94Sabóor 94
Compare Sabóor 94:8-10Sabóor 94:8-10