Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 94

Sabóor 94:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,
7te naa: «Ki Sax gisu ci, Yàllay Yanqóoba jii yégu ko.»
8Yeen bokk yu dofe yi, moytuleen. Gàtt xel yi, kañ ngeen di muus?

Read Sabóor 94Sabóor 94
Compare Sabóor 94:5-8Sabóor 94:5-8