Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 91

Sabóor 91:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Kiiraayam la lay sànge, nga yiiru, làqu; wormaam yéew la, di la aar.
5Doo ragal njàqarey guddi mbaa fittu bëccëg
6mbaa mbas mu yooteg lëndëm, ak balaa buy fàdde njolloor.
7Junni daanu fi sa wet, fukki junni (10 000) daanu fi sa ndijoor, du tax mu jege la.

Read Sabóor 91Sabóor 91
Compare Sabóor 91:4-7Sabóor 91:4-7