Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 8

Sabóor 8:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Moo luy nit, ba nga di ko bàyyi xel? Luy doom aadamaak loo koy yége?
6Yaa def nit mu yées malaaka yi as lëf, te yaa ko kaalaa teraangaak daraja,
7fal ko ci kaw loo bind, jox ko lépp, mu teg tànk:

Read Sabóor 8Sabóor 8
Compare Sabóor 8:5-7Sabóor 8:5-7