Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 88

Sabóor 88:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ana kuy yég say kéemaan ci googu lëndëm? Ku lay seedeel njekk réew ma fàtte faloo?
14Aji Sax ji, man, yaw lay woo wall, xëy, kare la gii ñaan, ne la:
15Éy Aji Sax ji, loo may gàntale, di ma fuuylu?
16Mitit bay laatikaaf, sama ngone ba tey; sa mbugal yu raglu, ba bopp ubu ràpp!

Read Sabóor 88Sabóor 88
Compare Sabóor 88:13-16Sabóor 88:13-16