Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 86

Sabóor 86:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Bu ma la wooyee bésub njàqare, yaa may nangul.
8Boroom bi, doo moroomu tuur yi, te jëf melul ni sa jos.

Read Sabóor 86Sabóor 86
Compare Sabóor 86:7-8Sabóor 86:7-8