Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 86

Sabóor 86:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Boroom bi sama Yàlla, naa la sante xol bu fees, màggal la ba fàww.
13Ngor lu réy nga ma won, sorele maak tëraayu bàmmeel.
14Éy Yàlla, nit ñu bew a ma jógal, def gàngoor gu néeg, di rëbb sama bakkan, te seetuñu la ci.

Read Sabóor 86Sabóor 86
Compare Sabóor 86:12-14Sabóor 86:12-14