Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 86

Sabóor 86:11-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Éy Aji Sax ji, won ma sa nammeel, ma doxe sa worma. Tënkal sama xol ci ragal la.
12Boroom bi sama Yàlla, naa la sante xol bu fees, màggal la ba fàww.
13Ngor lu réy nga ma won, sorele maak tëraayu bàmmeel.

Read Sabóor 86Sabóor 86
Compare Sabóor 86:11-13Sabóor 86:11-13