Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 86

Sabóor 86:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Mu di ñaanu Daawuda. Éy Aji Sax ji, teewlu ma, nangul ma, damaa ñàkk, néew doole.
2Maa gore, musal ma; maay sa jaam bi la wóolu, yaw, sama Yàlla, wallu ma.
3Éy Boroom bi, baaxe ma; yaw laay yendoo woo wall.

Read Sabóor 86Sabóor 86
Compare Sabóor 86:1-3Sabóor 86:1-3