Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 85

Sabóor 85:2-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Éy Aji Sax ji, yaa baaxe woon sa réew mi, ba suqli sëti Yanqóoba yi,
3baal sa mbooloo seeni ñaawtéef, jéggal leen bépp bàkkaar. Selaw.
4Ba nga xadar ja, muñ mer ma.
5Éy Yàlla mi nuy musal, suqli nu, te meddi.

Read Sabóor 85Sabóor 85
Compare Sabóor 85:2-5Sabóor 85:2-5