Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 84

Sabóor 84:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Benn fan ci sab ëtt de moo dàq junniy fan feneen. Sama taxawaayu bunt kër Yàlla moo ma gënal tëraayu biir xaymab ku bon.
12Aji Sax ji Yàllaa mat jant, mat kiiraay; yiw ak daraja, Aji Sax ji joxe; te du ngëneel lu muy bañal ku mat.

Read Sabóor 84Sabóor 84
Compare Sabóor 84:11-12Sabóor 84:11-12