Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 83

Sabóor 83:8-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8néegi Gebal, Amon ak Amaleg ak waa Filisteek waa Tir,
9réewum Asiri it fekki leen, di dooleel askanu Lóot wa. Selaw.
10Def leen na nga defoon waa Majan, def ko Sisera ak Yabin ca dexu Kison.
11Ña nga sànkoo Endor, ba doon ub tos fi kaw suuf.
12Defal seeni njiit na Oreb ak Seeb, def seen kilifa yépp ni Seba ak Salmuna,

Read Sabóor 83Sabóor 83
Compare Sabóor 83:8-12Sabóor 83:8-12