Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 83

Sabóor 83:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Sa ñoñ lañuy rabatal, di mànkool sa séddoo yii.
5Ñu ne: «Ayca nu far seen xeet wi, ba deesul fàttlikooti turu Israyil.»
6Dañoo mànkoo kat, te yaw lañu takktool:

Read Sabóor 83Sabóor 83
Compare Sabóor 83:4-6Sabóor 83:4-6