Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 83

Sabóor 83:12-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Defal seeni njiit na Oreb ak Seeb, def seen kilifa yépp ni Seba ak Salmuna,
13ña ne woon: «Nan séddoo parluy Yàlla yi.»
14Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
15Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,

Read Sabóor 83Sabóor 83
Compare Sabóor 83:12-15Sabóor 83:12-15