Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 81

Sabóor 81:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7«Sippi naa leen, woyofal seeni yoxo.
8Ngeen jàq, woo ma, ma xettli leen, wuyoo leen fa kiiraayal dënn ya, te maa leen nattoo fa wal ma ca Meriba. Selaw.
9Yeen sama ñoñ, dégluleen, ma dénk leen. Éy Israyil, su ngeen ma déglu woon!

Read Sabóor 81Sabóor 81
Compare Sabóor 81:7-9Sabóor 81:7-9