Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 80

Sabóor 80:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Nga wéex ko, mu sampu, law, dajal réew mi;
11keppaaram muur tund yi, ay caram sàng garabi seedar yu mag yi.
12Mu tàllal ay bànqaasam ba géej, lawal njebbit la ba dex ga.

Read Sabóor 80Sabóor 80
Compare Sabóor 80:10-12Sabóor 80:10-12