Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 79

Sabóor 79:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Boroom bi, sewal gi la sunuy dëkk sewal, këpp leen ko juróom yaari yoon,
13te nun ñiy sa mbooloo, di sa gétt gi ngay foral, nu di la sant ba fàww, di biral sa ngërëm sët ba sëtaat.

Read Sabóor 79Sabóor 79
Compare Sabóor 79:12-13Sabóor 79:12-13