Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7ngir ñu wóolu Yàlla, baña fàtte jëfi Yàlla, di jëfey santaaneem,
8te baña roy seeni maam; maas gu të woon te déggadi, ñu ñàkk pastéef te sàmmuñu kóllërey Yàlla.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:7-8Sabóor 78:7-8