Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:55-57

Help us?
Click on verse(s) to share them!
55Da leena dàqal ay xeet, dogal leen céru suuf, sancal giiri Israyil ca seeni xayma.
56Teewul ñuy diiŋat ak a gàntal Yàlla Aji Kawe ji, sàmmuñu ay dénkaaneem,
57xanaa dëddu, di ko wor ni seeni maam, toogadi ni xala gu yolom.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:55-57Sabóor 78:55-57