Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:52-54

Help us?
Click on verse(s) to share them!
52Mu génne ñoñam niy gàtt, wommat leen ni gétt ca màndiŋ ma,
53ba yóbbu leen fu wóor te tiituñu; seeni noon, géej ga mëdd leen.
54Mu yóbbu leen fa suufam su sell sa, fa tund woowu mu jënde dooleem.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:52-54Sabóor 78:52-54