Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:50-51

Help us?
Click on verse(s) to share them!
50Mu afal meram, ba musalul seen bakkan, xanaa jébbal leen mbas ma.
51Daa fàdd képp kuy taaw ca Misra te juddoo seen digg doole, fa xaymay sëti Xam.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:50-51Sabóor 78:50-51