Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:36-39

Help us?
Click on verse(s) to share them!
36Teewul ñu di ko jéema naxey wax, di ko fen.
37Joxuñu ko woon xol, sàmmuñu kóllëreem.
38Teewul mu yërëm, baal leen seen ñaawtéef, ba sànku leen. Muñ na meram, muñati, te toppul xolam,
39ndax xalaataat ne suuxu neen lañu, di noo guy dem te du délsi.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:36-39Sabóor 78:36-39