Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3muy lu nu dégg, xam ko, sunuy maam xamal nu ko.
4Dunu ko nëbb sunuy doom, xanaa di ko jottli maas giy ñëw, xamal leen jaloorey Aji Sax ji ak kàttanam aki kéemaanam.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:3-4Sabóor 78:3-4