Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:15-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Moo xar ay doj ca màndiŋ ma, mbàmbulaan wal, mu nàndal leen;
16mu sotti ndox mu balle ciw xeer, walal, mu safi dex.
17Teewul ñu wéy di moy Aji Kawe ji, di ko gàntal ca màndiŋ ma.
18Ñoo diiŋate Yàlla xol, di xemmem ñam wu bakkane.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:15-18Sabóor 78:15-18