Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Bëccëg mu jiitee leen aw niir, ak leeru sawara guddi gépp.
15Moo xar ay doj ca màndiŋ ma, mbàmbulaan wal, mu nàndal leen;
16mu sotti ndox mu balle ciw xeer, walal, mu safi dex.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:14-16Sabóor 78:14-16