Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 76

Sabóor 76:1-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ànd aki xalam, di woyu Sabóor, giiroo ci Asaf.
2Yàlla siiw na fa Yuda, aw turam màgg fa Israyil.
3Xaymaam a nga Salem, di xunteem ma fa Siyoŋ.
4Fa la rajaxee fitt yuy boy ak pakk ak saamar ak ngànnaayal xare. Selaw.

Read Sabóor 76Sabóor 76
Compare Sabóor 76:1-4Sabóor 76:1-4