Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 74

Sabóor 74:19-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Bul wacce rabu àll sam xati, bul sàggane sa néew-doole yi mukk.
20Ngalla xoolal ci kóllëre gi, fu làqu ci réew mi, fitna dale fa ba dajal.
21Yàlla bu néew-doole ñibbaale gàcce, yal na ku ñàkk ak ku néewle di la santandoo.
22Éy Yàlla, jógal ñoŋal sa dëgg, bàyyil xel dof bi la dëkkee sewal.

Read Sabóor 74Sabóor 74
Compare Sabóor 74:19-22Sabóor 74:19-22