Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 74

Sabóor 74:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Yaa fettaxal fii bëti ndox akum wal, ŋiisal dex yu masa wal.
16Yaa moom bëccëg, moom guddi, teg fi weer week jant bi.

Read Sabóor 74Sabóor 74
Compare Sabóor 74:15-16Sabóor 74:15-16