Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:8-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Dañuy ñaawle, di wax lu bon, di réy-réylu, boole ci kàdduy jaay-doole.
9Seen ŋal-ŋal àkki asamaan, làmmiñ dajal suuf.
10Moo tax ñoñi Yàlla walbatiku ci ñoom, di jolu seen wax nim ndox
11te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
12Ñu bon ñaa ngoog! Ne finaax, di gëna woomle.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:8-12Sabóor 73:8-12