Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Amuñu metit, xanaa ne faaj.
5Doñ-doñu nit dabu leen, coonoy doom aadama dalu leen.
6Moo leen taxa ràngoo reewande, làmboo coxor.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:4-6Sabóor 73:4-6