Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:13-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Man kay maa sellal ci neen, di sàmm sama der.
14Bés bu ne yar dal ma, saa yu ma xëyee, jot mbugal.
15Su ma noon: «Naa waxe ni ñoom,» kon de, ma wor sa askanu mbooloo.
16Naka laay jéema ràññee lii, mbir mi ëlëm ma.
17Ba ma àggee sa kër gu sell ga, laa doora gis muju ku bon.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:13-17Sabóor 73:13-17