Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 72

Sabóor 72:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.
13Mooy yërëm ku néewleek ku tumurànke, di sàmm bakkanu aji tumurànke,

Read Sabóor 72Sabóor 72
Compare Sabóor 72:12-13Sabóor 72:12-13