Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 70

Sabóor 70:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Yàlla, wallu ma! Éy Aji Sax ji, gaawe ma!
3Kuy wut sama bakkan, yal na rus, torox ne tott. Kuy bége sama loraange, yal nañu ko duma, waññi ko, mu ne yàcc.
4Kuy ñaawle, yal na dellu gannaaw, torox.

Read Sabóor 70Sabóor 70
Compare Sabóor 70:2-4Sabóor 70:2-4