Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 68

Sabóor 68:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Céy Yàlla, yaa génn, jiitu sa mbooloo, daagu, dugg màndiŋ ma. Selaw.
9Suuf yëngu, asamaan sóob fi kanam Yàlla, boroom tundu Sinayi, Yàllay Israyil ja!

Read Sabóor 68Sabóor 68
Compare Sabóor 68:8-9Sabóor 68:8-9