Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 68

Sabóor 68:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Ñu jub ñi nag bég, di bànneexu fi kanam Yàlla, tey puukarewoo mbégte.
5Woyleen Yàlla, teral turam, xàllal-leen kiy war niir yi, Ki Sax moo di turam. Bànneexuleen fi kanamam.

Read Sabóor 68Sabóor 68
Compare Sabóor 68:4-5Sabóor 68:4-5