Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 68

Sabóor 68:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Yàlla, waame nga tawal, leqlee ko réew mi nga séddoo, fa mu sonne,
11sa mbooloo dëkke fa. Yàlla yaa leel néew-ji-doole ci sag mbaax.
12Boroom beey joxe ndigal, gàngooru jigéen indi xibaar:

Read Sabóor 68Sabóor 68
Compare Sabóor 68:10-12Sabóor 68:10-12