Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 67

Sabóor 67:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3ba ñu ràññee sa loxo fi kaw suuf, gis sag wall fi biir xeet yépp.
4Yaw Yàlla, na la xeet yi sant, na la xeet yépp sant.
5Na xeet yiy bég, di sarxolle; loo dogalal xeet yi njub la, te yaay wommat xeet yi ci kaw suuf. Selaw.
6Yaw Yàlla, na la xeet yi sant, na la xeet yépp sant.

Read Sabóor 67Sabóor 67
Compare Sabóor 67:3-6Sabóor 67:3-6