Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 65

Sabóor 65:3-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Yaw miy nangug ñaan, yaw la képp di wuysi.
4Samay ñaawtéef man na ma, waaye sunuy tooñ, yaa nu koy baal.
5Ndokklee koo tànn, woo ko, mu dale say ëtt, di xéewloo sa ngëneeli kër, ak sa sellngay dëkkuwaay.
6Defal nga nuy kéemaan, nangug ñaan ci njekk, yaw Yàlla, mi nuy wallu, di yaakaaru àddina wërngal këpp, ba ca géej gu sore ga.
7Yaa dëje tund yu mag yi doole, gañoo sa kàttan,

Read Sabóor 65Sabóor 65
Compare Sabóor 65:3-7Sabóor 65:3-7