Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 65

Sabóor 65:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Yaa dikke suuf am wal, nangul koo nangul. Dexu Yàllaa fees ndox, ngay may nit peppam, ni nga ko waajale suuf si,
11di suuxat ngàbb mi, maasalee ko jal yi, sottiy waame, mu mokk, cax ma, nga barkeel.

Read Sabóor 65Sabóor 65
Compare Sabóor 65:10-11Sabóor 65:10-11