Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 62

Sabóor 62:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Moom doŋŋ a di sama cëslaay, di sama wall, di sama rawtu, duma tërëf.
8Yàllaa may musal, di ma sagal, ma di ko doolewoo. Sama kiiraay, Yàllaa!
9Bokk yi, wóoluleen ko fu ngeen tollu, diisleen ko seen xol, Yàllaay sunu kiiraay. Selaw.

Read Sabóor 62Sabóor 62
Compare Sabóor 62:7-9Sabóor 62:7-9