Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 61

Sabóor 61:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ngalla féqal fani Buur, ay atam bare, sët ba sëtaat.
8Éy Yàlla, yal na Buur toog ba fàww fi sa kanam, nga sédd ko sa ngor ak sa worma, mu fegoo;

Read Sabóor 61Sabóor 61
Compare Sabóor 61:7-8Sabóor 61:7-8