Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 52

Sabóor 52:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Mooy ba Doweg, Edomeen ba, demee ca Sóol, ne ko Daawuda dem na kër Ayimeleg.
3Moo jàmbaar ji, looy damoo jëfi coxor? Yàlla, ngoram, bés bu nekk la.
4Ak sa làmmiñ wi ngay sose loraange, mel ni saatu su ñu xacc, rambaaj bi!

Read Sabóor 52Sabóor 52
Compare Sabóor 52:2-4Sabóor 52:2-4